Mark 4:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu tontu leen: «Yéen may nañu leen, ngeen xam mbóoti nguuru Yàlla, waaye ñi ci biti léeb ay ëmb lépp.