Mark 4:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
waaye du yàgg, ndaxte wax ji saxul ci moom. Bu jaaree ci nattu nag, mbaa ñu fitnaal ko ndax kàddu gi, mu dàggeeku ci saa si.