Mark 4:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Daawu leen wax dara lu dul ciy léeb. Waaye bu wéetee ak ay taalibe, daan na leen firil lépp.