Mark 4:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk Yeesu tëdd di nelaw ci ngégenaay ci taatu gaal gi.Taalibe yi daldi ko yee naan: «Kilifa gi, ndax sunu bakkan soxalu la?»