Mark 4:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu Yeesu jóg, daldi gëdd ngelaw li, ne dex gi: «Noppil te dal!» Noonu ngelaw li dal, ba lépp ne nemm.