Mark 5:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu sàmm ya daw ca dëkk ba ak ca àll ba, nettaliji mbir mi, ba nit ñi ñëw, seet li xew.