Mark 5:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu di dugg ci gaal gi, ki rab ya jàppoon ñaan Yeesu, ngir ànd ak moom.