Mark 5:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu waa ji dem ci diiwaanu Fukki dëkk yi, daldi fa yégle la ko Yeesu defal, ba ñépp waaru.