Mark 5:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu dugg ne leen: «Lu ngeen di soow, tey jooy? Janq bi deewul, day nelaw rekk.»