Mark 6:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Koo xam ne gàntu na leen, mbaa mu tanqamlu leen, génnleen fa, yëlëb seen pëndu tànk, ngir seede leen seen réer.»