Mark 6:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko buur ba déggee, mu am naqar wu réy. Waaye bëggu koo gàntu ndax ngiñ li ak gan ñi.