Mark 6:50 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ñépp gis ko te jommi ci. Waaye mu wax ak ñoom ci saa si ne leen: «Takkleen seen fit, man la, buleen tiit!»