Mark 7:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu leen ne: «Ndax yéen itam seen xol dafa tëju? Xanaa xamuleen ne, dara lu jóge biti, dugg ci nit, du ko man a indil sobe,