Mark 7:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte du dugg ci xol, waaye ci biiram lay jëm, ba noppi daldi génn ca bérab bu làqu?» Ci li mu wax loolu Yeesu daganal na bépp ñam.