Mark 7:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na fa nag jigéen ju rab jàpp doomam ju jigéen. Bi mu déggee ne, Yeesoo nga fa, mu ñëw, daanu ciy tànkam,