Mark 7:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu ko defee Yeesu tere leen, ñu wax ko kenn, waaye lu mu leen ko gën a tere, ñu gën ko nee siiwale.