Mark 7:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu waaru lool naan: «Lépp lu mu def, lu yéeme la. May na sax tëx yi ñuy dégg, ak luu yi ñuy wax.»