Mark 7:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Farisen ya ak xutbakat ya laaj ko ne: «Lu tax say taalibe duñu topp aaday yoon, yi maam yi tëral, waaye ñuy lekk ak loxo yu setul?»