Mark 8:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu binni ci xolam ne leen: «Lu tax niti jamono jii di laaj kéemaan? Ci dëgg maa ngi leen koy wax, duñu jot genn kéemaan.»