Mark 8:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu nag jàpp loxob gumba gi, yóbbu ko, ba génn dëkk bi. Mu def tiflit ciy bëtam, teg ko loxo naan: «Ndax gis nga dara?»