Mark 8:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu laaj leen: «Yéen nag, ku ngeen wax ne moom laa?» Piyeer tontu ko: «Yaa di Almasi bi.»