Mark 9:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne leen ati: «Ci dëgg maa ngi leen koy wax, am na ñi fi taxaw, ñoo xam ne duñu dee, te gisuñu nguuru Yàlla ñëw ak doole.»