Mark 9:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu amee Yowaana ne ko: «Kilifa gi, danoo gis nit kuy dàq ay rab ci sa tur, nu tere ko ko, ndax li mu bokkul ci nun.»