Mark 9:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu niir muur leen, te baat jibe ca niir wa naan: «Kii mooy sama Doom ji ma bëgg, ci moom laa ame bànneex; dégluleen ko.»