Matthew 1:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yuusufa jëkkëram nag, nekkoon na nit ku jub te bëggu ko woon a weer. Mu nar a xàccook moom ci sutura.