Matthew 10:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Boo xamee ne fitnaal nañu leen ci dëkk bii, demleen ca ba ca kanam. Ci dëgg maa ngi leen koy wax, dungeen man a wër dëkki Israyil yépp, te Doomu nit ki ñëwul.»