Matthew 11:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba Yeesu joxee fukki taalibeem ya ak ñaar ndigal yooyu, mu jóge fa, ngir dem jàngaleji ak a waare ci seeni dëkk.