Matthew 11:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu teg ca ne: «Sama Baay jébbal na ma lépp, te kenn mënu maa xam, man Doom ji, ku dul Baay bi; kenn it mënul a xam Baay bi, ku dul man Doom ji, ak ku ma ko bëgg a xamal.