Matthew 11:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon lu ngeen seeti woon nag? Nit ku sol yére yu rafet? Waaye ñi sol yére yu rafet ñu ngi dëkk ci këri buur.