Matthew 12:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bi ko Yeesu yégee, mu sore foofa; te ñu bare topp ko, mu wéral leen ñoom ñépp.