Matthew 12:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu xam seen xalaat ne leen: «Réew mu xeex boppam tas, te dëkk mbaa kër guy xeex boppam du man a yàgg.