Matthew 12:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Su fi amee nit ku bare doole, te nit bëgg a dugg ci këram, nangu alalam, naka la koy defe? Xanaa dafay jëkk a yeew ku bare doole ka, ba noppi door a toj këram gépp.