Matthew 12:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu tontu leen: «Ndax jànguleen la Daawuda defoon, ba mu xiifee, moom ak ña mu àndaloon?