Matthew 12:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu teg ca ne: «Loolu moo tax maa ngi leen koy wax, bàkkaar walla sos wu mu man a doon, dinañu ko baale, waaye ku sosal Xelum Yàlla, duñu ko baal.