Matthew 12:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu leen: «Yéenay laaj firnde, yéen niti jamono ju bon jii, yéen ñi fecci seen kóllëre ak Yàlla, waaye dungeen jot genn firnde gu dul firndeg yonent Yàlla Yunus.