Matthew 12:46 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Yeesu nekkee di wax ak mbooloo ma, ndeyam ak ay rakkam daldi ñëw, taxaw ci biti, bëgg a wax ak moom.