Matthew 12:47 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu kenn nit ne ko: «Sa yaay ak say rakk ñu ngi nii taxaw ci biti, bëgg a wax ak yaw.»