Matthew 13:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu tontu leen ne: «May nañu leen, ngeen xam mbóoti nguuru Yàlla Aji Kawe ji, waaye ñale mayuñu leen ko.