Matthew 13:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Li Esayi waxoon ci kàddug Yàlla am na ci ñoom, bi mu naan:“Dingeen déglu bu baaxwaaye dungeen xam dara;di xool bu baax waaye dungeen gis dara.