Matthew 13:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Yeesu dégtal leen beneen léeb ne leen: «Nguuru Yàlla Aji Kawe ji dafa mel ni nit ku ji jiwu wu baax ci toolam.