Matthew 13:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
àddina mooy tool bi; ñi bokk ci nguuru Yàlla ñoo di jiwu wu baax wi; ñi bokk ci Ibliis ñooy jëmb bi;