Matthew 14:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca saa sa Yeesu tàllal loxoom, jàpp ko naan: «Yaw mi néew ngëm, lu tax nga am xel ñaar?»