Matthew 14:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Erodd nag bëgg koo rey, waaye dafa ragal nit ñi, ci li ñu teg Yaxya ab yonent.