Matthew 15:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi taalibeem ya déggee loolu, ñu ñëw ci moom ne ko: «Ndax xam nga ne, Farisen yi dañoo mer ndax loolu nga wax?»