Matthew 15:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontuwu ko genn kàddu. Ay taalibeem nag ñëw ci moom ne ko: «Doo ko yiwi, mu ngi nuy topp, di yuuxu ci sunu kaw.»