Matthew 15:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu Yeesu woo ci moom taalibeem ya ne leen: «Yërëm naa mbooloo mi, ndaxte toog nañu fi man ñetti fan, te amatuñu lu ñu lekk. Bëgguma leen a yiwi te lekkuñu, ngir bañ ñu tële ci yoon wi.»