Matthew 15:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yéen dangeen ne, ku wax sa ndey walla sa baay: “Li ngeen war a jariñoo ci man, jébbal naa ko Yàlla,”