Matthew 16:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu fa jógee, Yeesu dem ca diiwaanu Sesare bu Filib. Foofa mu laaj taalibeem ya: «Lu nit ñiy wax ci Doomu nit ki; mooy kan?»