Matthew 16:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu ko: «Barkeel ñeel na la, Simoŋ doomu Yunus, ndaxte du nit moo la xamal lii, waaye sama Baay bi nekk ci kaw.