Matthew 16:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Li dale ci jamono jooja, Yeesu tàmbali na xamal taalibeem yi ne, war na dem Yerusalem, daj fa coono yu bare, jóge ca njiit ya, ca saraxalekat yu mag ya ak ca xutbakat ya; ñu rey ko, mu dekki ca ñetteelu fan ba.